(Go: >> BACK << -|- >> HOME <<)

Aller au contenu

Fànn

Jóge Wikipedia.
Sumbu 14 Maars 2012 à 17:58, bu: HiW-Bot (waxtaancëru) (r2.7.2) (Robot: Adding gn:Mba'eporã)


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal



Fànn, ci tekkeem gu yaa, dafa ëmb bépp yëngu-yëngu nit - muy lu kenn walla mbooloo di def - moom, su sukkandikoo ci gisiin yu xereñ, ñaw ak doxaliin wu bawoo cim njàng walla cig yàgg-jëf, mooy tax a man a biral genn kàllaama gu taaru gi. Ci fireem gu tay, fànn dees koo féetale ak man-gee jokkaley yëg-yëg, ba tax kàllaamay fànn, donte dañuy jokkaley bataaxal, taxul ñu doon dëgg-dëgg aw làkk, ndax taxawuñu ciw yoon wu ñépp ànd déggoo, xanaa kay safaan wa ku nekk ak sa gisiin walla déggiin.

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons