(Go: >> BACK << -|- >> HOME <<)

Aller au contenu

Koom-koom wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Escarbot (waxtaancëru)
m r2.7.2+) (Robot: Adding zea:Economie
Tafaan: recent_changes Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
 
(11 versions intermédiaires par 10 utilisateurs non affichées)
Rëdd 13 : Rëdd 13 :
== Koom-koom ==
== Koom-koom ==

Xam-xamu koom-koom ( ci Fr:economie)moom xam-xamu mboolaay(social) la buy yëngu c gëstu ni ñuy jëfandikoo jumtukaayi jóox(production)yu daytalu yi am cig mboolaay (société) ngir faj soxlay ak xemmemtéefi cér(membre)yu mboolaay gii.Xam-xam bii nag mook xam-xam yépp a yam, dafa am ay dëgg-dëggam akaki àtteem waaye jeexiitalu gi mu def ci nekkiini mboolaay yi ak yu politig yi (les conditions sociales et politiques)ak ni ay séqoom ( ay relation-oom) dugganteek nekkiin yii tax na ba melow mboolaay muur ko, cuub ko.
Xam-xamu koom-koom ( ci Fr:economie)moom xam-xamu mboolaay(social) la buy yëngu ci gëstu ni ñuy jëfandikoo jumtukaayi jóox(production)yu daytalu yi am cig mboolaay (société) ngir faj soxlay ak xemmemtéefi cér(membre)yu mboolaay gii.Xam-xam bii nag mook xam-xam yépp a yam, dafa am ay dëgg-dëggam akaki àtteem waaye jeexiitalu gi mu def ci nekkiini mboolaay yi ak yu politig yi (les conditions sociales et politiques)ak ni ay séqoom ( ay relation-oom) dugganteek nekkiin yii tax na ba melow mboolaay muur ko, cuub ko.

Xam-xam bii li mu làmboo mooy seggat [[jóox gi]] (production), [[séddale gi]], ak [[yaxantu]] ak [[lakk walla jëfandikoo]] [[njaay yi (marsandiis yi) ak njëfte yi (les services)]]. danuy faral a wax ci koom-koom ne [[buy wuyyu la (positive)]] bu dee jéem a leeral ngértey tànn yu wuuteyi, di joxe ay mbooleem [[ay xalaat jiital (hypotese)]], walla am mbooloom ay gendiku (ay seetlu),danuy wax it ne [[bu nattukaay]] la bu dee leeral doxal yi nu war a def.

Rëdd 22 : Rëdd 22 :
* [[Koom-koomub lépp]] walla [[koom-koom yu mag yi]] ,mooy gëstu ci koom-koomu réewum lëmm, ci melo wii nag dees koy xalam(dees koy xalaat) muy [[gaaral]] ak [[sàkku]] ñeel [[alal walla xaalis]], [[bopp-alal]] (capital)walla njaay (marsandiis) ci biir koom-koomu am réew

{{Commonscat|Economics}}
[[Wàll:Koom-koom]]

{{Link FA|fr}}
{{Xam-xam}}

[[af:Ekonomie]]
[[Wàll:Koom-koom]]
[[als:Wirtschaftswissenschaft]]
[[am:ሥነ ንዋይ]]
[[an:Economía]]
[[ar:اقتصاد (علم)]]
[[ast:Economía]]
[[ba:Иҡтисад]]
[[bat-smg:Akuonuomėka]]
[[be:Эканоміка]]
[[be-x-old:Эканоміка]]
[[bg:Икономика (наука)]]
[[bm:Nafasorosira]]
[[bn:অর্থনীতি]]
[[bo:དཔལ་འབྱོར་རིག་པ།]]
[[br:Armerzh]]
[[bs:Ekonomija]]
[[ca:Economia]]
[[ceb:Ekonomiks]]
[[ch:Ekonomia]]
[[co:Ecunumia]]
[[cs:Ekonomie]]
[[cv:Экономика]]
[[cy:Economeg]]
[[da:Økonomi]]
[[de:Wirtschaftswissenschaft]]
[[el:Οικονομικά]]
[[en:Economics]]
[[eo:Ekonomiko]]
[[es:Economía]]
[[et:Majandusteadus]]
[[eu:Ekonomia]]
[[ext:Economia]]
[[fa:علم اقتصاد]]
[[fi:Taloustiede]]
[[fiu-vro:Majandustiidüs]]
[[fo:Búskapur]]
[[fr:Sciences économiques]]
[[frr:Eekonomii]]
[[fur:Economie]]
[[fy:Ekonomy]]
[[ga:Eacnamaíocht]]
[[gd:Riaghladaireachd]]
[[gl:Economía]]
[[gv:Tarmaynys]]
[[hak:Kîn-chi-ho̍k]]
[[he:כלכלה]]
[[hi:अर्थशास्त्र]]
[[hr:Gospodarstvo]]
[[ht:Ekonomi]]
[[hu:Közgazdaságtan]]
[[hy:Տնտեսագիտություն]]
[[ia:Economia]]
[[id:Ekonomi]]
[[ie:Economica]]
[[io:Ekonomiko]]
[[is:Hagfræði]]
[[it:Economia]]
[[ja:経済学]]
[[jbo:dinske]]
[[jv:Ékonomi]]
[[ka:ეკონომიკა]]
[[kaa:Ekonomika]]
[[km:សេដ្ឋកិច្ច]]
[[kn:ಅರ್ಥಶಾಸ್ತ್ರ]]
[[ko:경제학]]
[[ku:Aborî]]
[[ky:Экономика]]
[[la:Oeconomia]]
[[lad:Ekonomiya]]
[[lb:Economie]]
[[li:Economie]]
[[lo:ເສດຖະສາດ]]
[[lt:Ekonomika]]
[[lv:Ekonomika]]
[[map-bms:Ekonomi]]
[[mg:Toe-karena]]
[[mk:Економија]]
[[ml:സാമ്പത്തികശാസ്ത്രം]]
[[mr:अर्थशास्त्र]]
[[ms:Ekonomi]]
[[new:अर्थशास्त्र]]
[[nl:Economie]]
[[nn:Samfunnsøkonomi]]
[[no:Samfunnsøkonomi]]
[[nov:Ekonomike]]
[[nrm:Êcononmie]]
[[nso:Thutothuo]]
[[oc:Economia]]
[[pl:Ekonomia]]
[[pnb:اکنامکس]]
[[ps:وټپوهنه]]
[[pt:Economia]]
[[qu:Musiku]]
[[ro:Economie]]
[[ru:Экономика (наука)]]
[[rue:Економіка]]
[[sa:अर्थशास्त्रम्]]
[[sah:Экономика]]
[[sc:Economia]]
[[scn:Econumìa]]
[[sco:Economics]]
[[sh:Privreda]]
[[si:ආර්ථික විද්‍යාව]]
[[simple:Economics]]
[[sk:Všeobecná ekonomická teória]]
[[sl:Ekonomija]]
[[sm:Economics]]
[[sn:Muchenga Pfuma]]
[[so:Dhaqaale]]
[[sq:Ekonomia]]
[[sr:Економија]]
[[stq:Wirtskaft]]
[[sv:Nationalekonomi]]
[[sw:Somo la Uchumi]]
[[ta:பொருளியல்]]
[[te:ఆర్థిక శాస్త్రము]]
[[tg:Иқтисод]]
[[th:เศรษฐศาสตร์]]
[[tl:Ekonomika]]
[[tpi:Ikonimikis]]
[[tr:Ekonomi (bilim dalı)]]
[[tt:İqtisat]]
[[ug:ئىقتىسادشۇناسلىق]]
[[uk:Економіка]]
[[ur:معاشیات]]
[[uz:Iqtisodiyot]]
[[vec:Economia]]
[[vi:Kinh tế học]]
[[vo:Konömav]]
[[war:Siyensya ekonomika]]
[[yi:עקאנאמיק]]
[[zea:Economie]]
[[zh:经济学]]
[[zh-classical:計學]]
[[zh-min-nan:Keng-chè-ha̍k]]
[[zh-yue:經濟]]

Sumb bi teew bu 5 Fewriyee 2021 à 09:38

Xamale koom-koom[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Koom-koom walla cawarteg koom-koom (activité économique):(làkku grees wu yàgg wa : οἰκονομία, « yor ag kër walla saytu ko »« di οἶκος (kër ci ni ñu ko xame)ak (νέμω yor walla saytu(administrer)) mooy cawarteg nit giy feeñ ci liggéey ak jóox (produire) ak séddale ak joqalante (echange) ak jëfandikoo njuddéef yi (les produits) njëfte yi (le services).

Koom-koom nag ni ngi koy jànge ci xam-xami koom-koom yi, day sukkandiku nag ci gisiin yu koom-koom (théories économiques).

Dees na wax it ci koom-koom niki tolluwaayu koom-koom bu jamono bu am réew walla bu ab gox (zone), maanaam ag nekkam ci gëwéelub koom-koom yi. Cawarteg koom-koom gi kiliftéef yu koppar yi walla góornamaa yi (àtte yi) ñoo koy àtte jaare ko ci ab politig bu di kojug jamono (conjoncturelle).

doxaliin wu mbooloo mi (Les administrations publiques)day def moom itam ay politig yu koom-koom ngir soppi doxiinu koom-koom wu am réew.

benn ci joxoñ yu koom-koom (indicateurs économiques) yu mag yi mooy njuddéef mu ñumm mu biirum réew (NJ.Ñ.B) (produit intérieur brut (PIB)), loolu mooy maye nga man a nattale dooley koom-koom yu réew yi

Koom-koom[Soppisoppi gongikuwaay bi]

Xam-xamu koom-koom ( ci Fr:economie)moom xam-xamu mboolaay(social) la buy yëngu ci gëstu ni ñuy jëfandikoo jumtukaayi jóox(production)yu daytalu yi am cig mboolaay (société) ngir faj soxlay ak xemmemtéefi cér(membre)yu mboolaay gii.Xam-xam bii nag mook xam-xam yépp a yam, dafa am ay dëgg-dëggam akaki àtteem waaye jeexiitalu gi mu def ci nekkiini mboolaay yi ak yu politig yi (les conditions sociales et politiques)ak ni ay séqoom ( ay relation-oom) dugganteek nekkiin yii tax na ba melow mboolaay muur ko, cuub ko.

Xam-xam bii li mu làmboo mooy seggat jóox gi (production), séddale gi, ak yaxantu ak lakk walla jëfandikoo njaay yi (marsandiis yi) ak njëfte yi (les services). danuy faral a wax ci koom-koom ne buy wuyyu la (positive) bu dee jéem a leeral ngértey tànn yu wuuteyi, di joxe ay mbooleem ay xalaat jiital (hypotese), walla am mbooloom ay gendiku (ay seetlu),danuy wax it ne bu nattukaay la bu dee leeral doxal yi nu war a def.

Xam-xamu koom-koom dees koy déddale ci ñaari bànqaas yu mag:

Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons

Xam-xam
Xam-xam
Gëstubiddiw | Jëmm | Paj | Saytubiddiw | Simi | Xam-xamu suuf si ak jawwu ji | Xayma
Xarala
Jokkoosoryante | Xaralaymbëj | Doolerandu | Kàttan | Xam-xamu nosukaay | Mbëjfeppal
Xam-xami nite ak mboolaay
Diine | Melosuuf | Wërlaay | Nit | Yoon | Koom-koom | Taariix | Xeltu | Kàllaama