(Go: >> BACK << -|- >> HOME <<)

Aller au contenu

Fànn wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Jotterbot (waxtaancëru)
Xqbot (waxtaancëru)
m robot Adding: kl:Eqqumiitsuliorneq; cosmetic changes
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
{{junj}}
{{junj}}


'''Fànn''', ci tekkeem gu yaa, dafa ëmb bépp yëngu-yëngu nit - muy lu kenn walla mbooloo di def - moom, su sukkandikoo ci gisiin yu xereñ, ñaw ak doxaliin gu bawoo cim njàng walla cig yàgg-jëf, mooy tax a man a biral genn [[kàllaama]] gu taaru gi. Ci fireem gu tay, fànn dees koo féetale ak man-gee jokkaley yëg-yëg, ba tax kàllaamay fànn, donte dañuy jokkaley ''[[Bataaxal|bataaxal]]'', taxul ñu doon dëgg-dëgg aw [[làkk]], ndax taxawuñu ciw yoon wu ñépp ànd déggoo, xanaa kay safaan wa ku nekk ak sa gisiin walla déggiin.
'''Fànn''', ci tekkeem gu yaa, dafa ëmb bépp yëngu-yëngu nit - muy lu kenn walla mbooloo di def - moom, su sukkandikoo ci gisiin yu xereñ, ñaw ak doxaliin gu bawoo cim njàng walla cig yàgg-jëf, mooy tax a man a biral genn [[kàllaama]] gu taaru gi. Ci fireem gu tay, fànn dees koo féetale ak man-gee jokkaley yëg-yëg, ba tax kàllaamay fànn, donte dañuy jokkaley ''[[bataaxal]]'', taxul ñu doon dëgg-dëgg aw [[làkk]], ndax taxawuñu ciw yoon wu ñépp ànd déggoo, xanaa kay safaan wa ku nekk ak sa gisiin walla déggiin.
[[Wàll:fànn]]
[[Wàll:fànn]]


Rëdd 56 : Rëdd 56 :
[[jv:Seni]]
[[jv:Seni]]
[[ka:ხელოვნება]]
[[ka:ხელოვნება]]
[[kl:Eqqumiitsuliorneq]]
[[ko:예술]]
[[ko:예술]]
[[ku:Huner]]
[[ku:Huner]]

Sumb bu 14 Oktoobar 2009 à 19:54


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal



Fànn, ci tekkeem gu yaa, dafa ëmb bépp yëngu-yëngu nit - muy lu kenn walla mbooloo di def - moom, su sukkandikoo ci gisiin yu xereñ, ñaw ak doxaliin gu bawoo cim njàng walla cig yàgg-jëf, mooy tax a man a biral genn kàllaama gu taaru gi. Ci fireem gu tay, fànn dees koo féetale ak man-gee jokkaley yëg-yëg, ba tax kàllaamay fànn, donte dañuy jokkaley bataaxal, taxul ñu doon dëgg-dëgg aw làkk, ndax taxawuñu ciw yoon wu ñépp ànd déggoo, xanaa kay safaan wa ku nekk ak sa gisiin walla déggiin.