(Go: >> BACK << -|- >> HOME <<)

Aller au contenu

Fànn wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
LaaknorBot (waxtaancëru)
m robot Adding: it:Arte
LaaknorBot (waxtaancëru)
m robot Adding: tl:Sining
Rëdd 102 : Rëdd 102 :
[[tg:Санъат]]
[[tg:Санъат]]
[[th:ศิลปะ]]
[[th:ศิลปะ]]
[[tl:Sining]]
[[tr:Sanat]]
[[tr:Sanat]]
[[uk:Мистецтво]]
[[uk:Мистецтво]]

Sumb bu 9 Ut 2009 à 04:54


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal



Fànn, ci tekkeem gu yaa, dafa ëmb bépp yëngu-yëngu nit - muy lu kenn walla mbooloo di def - moom, su sukkandikoo ci gisiin yu xereñ, ñaw ak doxaliin gu bawoo cim njàng walla cig yàgg-jëf, mooy tax a man a biral genn kàllaama gu taaru gi. Ci fireem gu tay, fànn dees koo féetale ak man-gee jokkaley yëg-yëg, ba tax kàllaamay fànn, donte dañuy jokkaley bataaxal, taxul ñu doon dëgg-dëgg aw làkk, ndax taxawuñu ciw yoon wu ñépp ànd déggoo, xanaa kay safaan wa ku nekk ak sa gisiin walla déggiin.